Projet : "Consolidation et renforcement du projet pilote de romotion de la bonne gouvernance, du contrôle citoyen de l'action publique, de la culture des droits humains, de la démocratie et de la paix à l'echelle régionale, communale et locale"
Projet / CONTRAT N° EuropAID FED / 124-93.1/ AP1 / PAPNBG / SE - 005 - 04

INTRODUCTION / NDOORTE
Français
Wolof

Cet outil pédagogique a été conçu et édité par le CONGAD dans le cadre du projet : «Consolidation et renforcement du projet pilote de promotion de la bonne gouvernance, du contrôle citoyen de l'action publique, de
la culture des droits humains, de la démocratie et de la paix à l'échelle régionale, communale et locale - financement UE - Contrat N°EuropAID FED/124-93.1/AP1/PAPNBG/SE-005-04 ».

L'objectif global visé à travers le dit projet est de « contribuer au développement
et au renforcement de la prise en charge effective des questions
liées à la bonne gouvernance, au contrôle citoyen de l'action
publique, aux droits humains, à la démocratie et à la paix à l'échelle nationale, régionale, communale et locale ».
Par conséquent, cet outil est destiné à tous les acteurs cibles des régions du Sénégal : militants de la société civile, élus, agents des services d'appui technique aux collectivités locales, etc.
Il pourrait être utilisé lors des sessions de renforcement de capacités et pourrait également à tout moment, servir de document de référence sur les questions prises en charge.
L'outil contient onze (11) thèmes qui sont abordés de façon assez simplifiée pour une utilisation courante et aisée.
Les sessions de renforcement de capacités représentent des opportunités d'approfondissement des différents thèmes.
Je remercie tous mes collaborateurs de la Direction de la Décentralisation qui ont bien voulu contribuer à la production de cet outil, ainsi que toutes les personnes ressources extérieures qui m'ont apporté des conseils et inputs précieux.
Je souhaite vivement ce guide réponde aux attentes des commanditaires, des cibles et autres utilisateurs potentiels

 

 

 

 


Kongaat (CONGAD), mbootaay gi ëmb kurél yi feg nguur gi (ONG) tey yëngu
ci luy yokk doom-aadama, moo liggéey jumtukaay bii. Mu ngi sukkandiku ci
mébétam mi ko mbootaayu réewi Tugal yi jàppale te mu tudd : «Doolel mébét
mi ñeel caytu gu rafet, nemmeekug nit ñi, àqi doom-aadama, ak jàmm,
muy ci diiwaan, kómin walla dëkk. » N°EuropAID FED/124-93.1/AP1/PAPNBG/SE-005-04».
Nisër gu mag gu mébét mii mooy «fexe ba dolli màqaama nit ñi ba ñu gën a
man a def seen yoxo ci lépp lu ittéel caytu gu rafet, nemmeekug nit ñi, àqi
doom-aadama, ak jàmm, muy ci diiwaan walla dëkk»
Looloo tax ba, téere bii, di jumtukaay bu soxal képp ku dëkk ci fukk ak ñeenti
(14) diiwaani Senegaal yi, muy ku falu, di ndawi nguur walla muy kuy yëngu ci
kurél yi feg nguur gi, añs.
Man nañoo jëfandikoo jumtukaay bii ci pénc mbaa lëli xam-xam, ak képp ku
bëgg a gindéeku ci fànn yi nisëru mébét mi ñu tudd sànq, man na koo jariñoo.
Téere bi nak a ngi ëmb fukk ak benn (11) jukki ci anam yu woyof ngir ñu neex
a jariñoo. Ku mu neex nga dooree ci jukki bi la neex. Looloo tax mu mel dañuy
baamtu yenn wax yi.
Waaye, terewul, ci daje yeek lël yeek pénc yi, lañuy gën a xóotal jukki bu nekk
ni mu waree.
Mbégte la ci man, Musaa LÓO, bi ma CONGAD wóoloo ba dénk ma, ma tekki
jumtukaay bu am solo bii
May ñaan yàlla, liggéey bi dëppóok yaakaari CONGAD, rawatina ñi tax mu jóg
ak képp ku mu soxal.